Dataset Viewer
	text
				 
			stringlengths 1 
			2.33k 
			 | duration
				 
			float64 0.5 
			212 
			 | file_name
				 
			stringlengths 22 
			31 
			 | path
				 
			stringlengths 37 
			46 
			 | audio
				 
			audioduration (s) 0.03 
			212 
			 | 
|---|---|---|---|---|
	sauf picc yi picc yi daal moom yooyu moom bokku si  
 | 3.163 
							 | 
	wol_43930_1484.462_1487.625.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43930_1484.462_1487.625.wav 
 | |
	ci jamono bi ñu nekk et  bépp prpjet  boo xam ne daf ciy yëngatu rek je  pense  acteurs  yi ci war a jàpp yëpp dañ ci war a jàpp 
 | 6.446 
							 | 
	wol_44611_466.465_472.911.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44611_466.465_472.911.wav 
 | |
	%e assurance  dafa am convention  ak ministère  de  l'  élevage  direction  de  l'  élevage  ñun dañu am lëkkaloo donc  %e lu ñu booleeg ñoom ñoom dañuy partager  services  techniques  képp koo xam ne yaa ngi ci sa poste  vétérinaire  te yàlla mun loo la na nga ko defal procès  verbal  bi constat  bi yaa ko war a def 
 | 19.959 
							 | 
	wol_43951_1389.533_1409.492.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43951_1389.533_1409.492.wav 
 | |
	wala que  di  par wala wala tamit par  arrondissement  
 | 3.482 
							 | 
	wol_43612_359.106_362.588.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43612_359.106_362.588.wav 
 | |
	loo ciy tënk loo loo loo ciy yokk lan ngay tàggoo 
 | 2.893 
							 | 
	wol_42812_1634.225_1637.118.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42812_1634.225_1637.118.wav 
 | |
	ñëpp a soxla information  climatique  
 | 1.745 
							 | 
	wol_44012_594.736_596.481.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44012_594.736_596.481.wav 
 | |
	merci  beaucoup  
 | 0.975 
							 | 
	wol_44012_1229.937_1230.912.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44012_1229.937_1230.912.wav 
 | |
	ANACIM ñoo koy toppatoo 
 | 1.14 
							 | 
	wol_44121_1644.492_1645.632.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44121_1644.492_1645.632.wav 
 | |
	parce  que  ñu %e béykat  yëpp xam nañu ni suuf  c'  est  un  élément  vital 
 | 4.487 
							 | 
	wol_31211_259.757_264.244.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_31211_259.757_264.244.wav 
 | |
	parce  que  dangay gis ni serieux  na ci wàllu liggéey bi 
 | 2.422 
							 | 
	wol_44914_217.052_219.474.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44914_217.052_219.474.wav 
 | |
	%e code  barre  moo lay may nga xam ne sa maté() sa bagage  bi ngay yore mën nga koo gñne ci réew mi dem jaayi ko bitim réew kon loolu jigéen ñëpp ñoom ñoo war a %e xam yoon bi mën di ko jëfee ba ñi nga xam ne ñoom kenn ku ci nekk produit  yi nga yor di nga si mën di gñne si biir marché  bi danga mën a gñne bitim réew 
 | 15.129 
							 | 
	wol_41011_575.832_590.961.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41011_575.832_590.961.wav 
 | |
	donc   ñu bëri moo tax dañuy échoué  mboq  mboq bu fekkee mboq  boo xam ne ay penard  la ay indien  la wala * loolu dafa exigent   parce  que  ci engrais  mu ngi laaj benn hectare  juróom-benn saak fu kii di laajtee ñetti saak  parce  que  ay variétés  hybride  la yoo xam ne dañoo exigent   bu fekkee ci urée  bi la hectare  mu ngi laajte ñeenti saak juróom-benni saako  kon donc   matuwaay yi ngeen di jël ci hybride  bokkul matuwaay yi ñuy jël ci variété  locale  
 | 25.995 
							 | 
	wol_43011_1364.193_1390.188.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43011_1364.193_1390.188.wav 
 | |
	peut  être  %e ci biir waxtaan wi mën naa am ñu dellusiwaat si mais  nañu xam ne daal  %e insecte  ravageurs  yi nga xam ne ñoom ñoo gën a mën a yàq stoc  ci biir magasin  wala ci biir %e grenier  wala ci ci foo ko foo mën a denc sa sa sa sa meññeef  %e juróom-benni famille  céoptère  yooyu ma leen limal bokk nañ si  ak ñetti lépidoptère  yooyu ma leen wax ñoom it bokk nañ ci ñi nga xam ne ñoo dàq a yàq 
 | 23.466 
							 | 
	wol_43311_939.651_963.117.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43311_939.651_963.117.wav 
 | |
	je  pense  mun nañ jël benn thématique  boo xam ne dafa am lien  ak maraîchage  pour  ñu sensibiliser  leen ci thématique  boobu 
 | 7.157 
							 | 
	wol_44611_1263.753_1270.91.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44611_1263.753_1270.91.wav 
 | |
	waaw effectivement compliqué  na trop  
 | 1.584 
							 | 
	wol_41011_377.815_379.399.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41011_377.815_379.399.wav 
 | |
	%e bëgg mu gën a bëgg a gën a xam 
 | 1.248 
							 | 
	wol_41711_498.832_500.08.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41711_498.832_500.08.wav 
 | |
	yoo xam ne mën na ko jëfandikoo effectivement  daan nañu am problème  yu mel noonu 
 | 3.365 
							 | 
	wol_44113_718.141_721.506.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44113_718.141_721.506.wav 
 | |
	producteur  yi dinañ xam ban pratique  moo gën bu fekkee ne nag biñ leen indil 
 | 5.153 
							 | 
	wol_44612_164.241_169.394.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44612_164.241_169.394.wav 
 | |
	d'  accord  
 | 0.968 
							 | 
	wol_4111_1439.528_1440.496.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4111_1439.528_1440.496.wav 
 | |
	noonu la ñu war a informa() am information  ñëw ci service  techniques  yi  ñu wax la ñu wax rek quelle  période  la ñu war a ji lan mooy gerte lan mooy dugub lan mooy mboq  loolu tamit véhiculer  message  yi  muy yi nga wax nii en  terme  de  communication  daf ci am solo 
 | 12.977 
							 | 
	wol_43031_793.743_806.72.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43031_793.743_806.72.wav 
 | |
	maanaam sable  bi 
 | 0.875 
							 | 
	wol_44112_371.412_372.287.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44112_371.412_372.287.wav 
 | |
	waaw loolu yëpp gis nañu ko si 
 | 1.629 
							 | 
	wol_42514_319.154_320.783.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42514_319.154_320.783.wav 
 | |
	toog na jotul sax woote waaye mu ngi doon déglu émission  bi ñu ngi leen di gërëm di leen jaajëfal bu baax a baax 
 | 3.955 
							 | 
	wol_45422_1626.226_1630.181.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_45422_1626.226_1630.181.wav 
 | |
	te kenn ku ci nekk fii am na loo xam ne mën na ko ci indi 
 | 3.399 
							 | 
	wol_43211_232.726_236.125.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43211_232.726_236.125.wav 
 | |
	ndax su boobaa température  yiñ nar a dundee si addina nit yi du ko )ttan parce  que  dinañ dem ba moins  dix  huit  degré  muy nekk température  bu négative  loolu nit munu see dund 
 | 14.173 
							 | 
	wol_43711_1220.19_1234.363.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43711_1220.19_1234.363.wav 
 | |
	am na solo kon Diallo Diagne ñu ngi lay gërëm di la sant di Pusseynou diagne bokk ci liggéey bi tamit moom moo fare woon côté  Njaañ kon ñu ngi lay gërëm di la sant jërëjëf 
 | 8.62 
							 | 
	wol_41910_1509.772_1518.392.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41910_1509.772_1518.392.wav 
 | |
	%hum %hum kon ñu mën a jàpp rek ne déréglement  boobu nga xamante ne nii gis nañ ko ci wàllu prévision  yi ci fi nga xamante ne nii  %e mooy gox bi ñu féetoo di diwaanu Nior gën cee leer di Saloum  %e nekk na loo xamante ne nii %e coppite jaww ji la maanaam changement  climatique  bi moo ko daal di andi  
 | 15.503 
							 | 
	wol_43020_1336.98_1352.483.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43020_1336.98_1352.483.wav 
 | |
	%hum ak waa ICS ah def ay recherches  ba nga xam ne 
 | 3.695 
							 | 
	wol_43012_641.14_644.835.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43012_641.14_644.835.wav 
 | |
	 te yoroo torche  boo ko niinee 
 | 1.665 
							 | 
	wol_43020_1748.836_1750.501.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43020_1748.836_1750.501.wav 
 | |
	maintenant  am na yeneen catégories  jeunes  nag yoo xam ne su def nañ formation  
 | 6.013 
							 | 
	wol_44611_1119.579_1125.592.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44611_1119.579_1125.592.wav 
 | |
	loolu mooy problème  bi gàllankoor mooy pro() parce  que  biodigesteur  bu demee ba fonctionner   nga am sa engrais   nga am sa gaz  daanaka jigéen yu bëri nga xam ne dañuy yëngu ci wàllum transformation  parce  que  tamit waxuñu ko  
 | 13.086 
							 | 
	wol_42922_459.025_472.111.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42922_459.025_472.111.wav 
 | |
	waaye nag dans  topus  les  cas  
 | 0.975 
							 | 
	wol_44112_545.549_546.524.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44112_545.549_546.524.wav 
 | |
	waaw mooy li may wax rek 
 | 1.617 
							 | 
	wol_43412_1364.893_1366.51.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43412_1364.893_1366.51.wav 
 | |
	wala soit  leneen nga ñooñu kenn ku ci nekk war nga mën a defar say kayit ba mu valable soo amee say kayit ba mu valable nag nga xam ne say produit  boo ko xasee defar  
 | 8.751 
							 | 
	wol_41011_682.942_691.693.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41011_682.942_691.693.wav 
 | |
	 kon nag 
 | 0.683 
							 | 
	wol_43612_109.328_110.011.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43612_109.328_110.011.wav 
 | |
	waaw xam nga jamono suy dox nag 
 | 1.115 
							 | 
	wol_42811_1220.263_1221.378.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42811_1220.263_1221.378.wav 
 | |
	dégg nga %e damay fàttali leen gën di wax nit ñi %e laaj leen ñu ni ñu bon  messages  yi baax na waaye li leen gënaloon moom mooy message  rajo am na kii quoi  message  kii quoi  vocal  
 | 11.226 
							 | 
	wol_42212_1458.933_1470.159.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42212_1458.933_1470.159.wav 
 | |
	ci loolu te te te te lu ñu xamul mooy maanaam janax boobu sax am na feebar bu muy joxe parce  que  janax bi sawam yi sawam bi dafa am benn feebar boo xam ne dafa nekk ci moom 
 | 11.761 
							 | 
	wol_43910_1507.543_1519.304.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43910_1507.543_1519.304.wav 
 | |
	moo tax énoom %e vraiment  macha  allah  dañu leen dii dañu leen di sant bu baax a baax  beneen bi ci des tey jii ñu énu dugal beneen %e domaine  ci mbir mi muy restauration  
 | 9.06 
							 | 
	wol_4613_766.946_776.006.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4613_766.946_776.006.wav 
 | |
	xam e rek moo di ANACIM  ndax li nga xam ne rek moo di changement  climatique  doon na réalité  
 | 7.328 
							 | 
	wol_42513_0.0_7.328.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42513_0.0_7.328.wav 
 | |
	salaamaaleykum 
 | 0.528 
							 | 
	wol_43612_1496.484_1497.012.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43612_1496.484_1497.012.wav 
 | |
	 donc  li si jiitu  mooy information  météo  bi ci la bokk d'  accord  
 | 4.769 
							 | 
	wol_43020_1468.504_1473.273.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43020_1468.504_1473.273.wav 
 | |
	maanaam au  lieu  ngay de() ngay dem ak sa xel noonu rek 
 | 2.914 
							 | 
	wol_42932_221.794_224.708.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42932_221.794_224.708.wav 
 | |
	dañu lay indil yow  dañuy indi dañuy indi ngeen ñam produit  yëpp la ñuy indi 
 | 2.678 
							 | 
	wol_41013_538.395_541.073.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41013_538.395_541.073.wav 
 | |
	ni ko amsecta  yi 
 | 1.121 
							 | 
	wol_45412_78.507_79.628.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_45412_78.507_79.628.wav 
 | |
	%e di leen ko xamal ñuy xam fuñuy teg seen i tànk 
 | 2.352 
							 | 
	wol_4812_648.797_651.149.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4812_648.797_651.149.wav 
 | |
	il  faut  que  ñun ñii ñu xam ne mbay 
 | 1.554 
							 | 
	wol_44112_491.174_492.728.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44112_491.174_492.728.wav 
 | |
	bokkul dafa xaw a danoo niróo nag 
 | 1.521 
							 | 
	wol_45412_1422.167_1423.688.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_45412_1422.167_1423.688.wav 
 | |
	 alahuma amiin 
 | 1.357 
							 | 
	wol_4314_469.128_470.485.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4314_469.128_470.485.wav 
 | |
	%hum  te ku am %e béykat boo xam ne da nga yor say jur war leen a dundal  defe nga ne kooku dina la dégg  
 | 6.775 
							 | 
	wol_43810_1515.222_1521.997.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43810_1515.222_1521.997.wav 
 | |
	%e incha  allah  
 | 0.996 
							 | 
	wol_42931_143.888_144.884.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42931_143.888_144.884.wav 
 | |
	 bisimilah  sëñ bi na nga tudd 
 | 2.226 
							 | 
	wol_35710_0.0_2.226.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_35710_0.0_2.226.wav 
 | |
	dama bëggoon na %e contribuer  ci %e seen émission  bu am importance  bii 
 | 5.28 
							 | 
	wol_43412_1029.681_1034.961.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43412_1029.681_1034.961.wav 
 | |
	 moom moo doon ñëw lu gën a bari di def si émissions  yi 
 | 3.275 
							 | 
	wol_35312_80.37_83.645.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_35312_80.37_83.645.wav 
 | |
	mu ngoog kooku la 
 | 1.14 
							 | 
	wol_45412_402.597_403.737.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_45412_402.597_403.737.wav 
 | |
	loolu mooy surtout  jafe  bi donc  météo  ne suba dina taw béykat bi nan lay fexe ba am information  boobu mais  tamit il  faut  que  tamit %e ñoom i tam ñu def ay effors  tamit parce  que  boo xoolee tey rajo yi comme  rajo  Ndefleng par  exemple  fii souvent  météo  daf fay jaar def ay émissions  joxe ay informations  ak yooyu ah 
 | 23.217 
							 | 
	wol_42912_912.838_936.055.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42912_912.838_936.055.wav 
 | |
	et  et  tey %e Habib  %e lu tax COPEGA di di di dérangé  c'  est  à  dire  le  problème  c'  est  quoi  parce  que  man bu fekkee dëgg rek laa leen wax  su ma déggee ku leen di supporté  wala ku ànd ak yéen rek ñaareel ab béykat la mais  au  delà  de  ça  les  orga() ñeneen ñiy yëngatu ci kii bi filière  bi  daal da da ngeen di dérangé  %e le  problème  c'  est  quoi  lan la 
 | 18.301 
							 | 
	wol_44412_289.321_307.622.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44412_289.321_307.622.wav 
 | |
	%e chaque  président  de  section  villageoise  ñu convoqué  leen 
 | 2.768 
							 | 
	wol_31212_398.721_401.489.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_31212_398.721_401.489.wav 
 | |
	dégg nga 
 | 0.597 
							 | 
	wol_42611_1326.665_1327.262.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42611_1326.665_1327.262.wav 
 | |
	ñu def ay jàngat xool gis ne effectivement   gis nañ ne depuis  des  années  suñ delloo si histoire  depuis  les  années  mille  huit  cent  
 | 10.383 
							 | 
	wol_43020_946.218_956.601.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43020_946.218_956.601.wav 
 | |
	en  vu  de  la  prochaine  campagne  
 | 1.379 
							 | 
	wol_43810_429.193_430.572.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43810_429.193_430.572.wav 
 | |
	%hum %hum foog mu ñor foog ñu weer ko ba mu wow koŋŋ 
 | 3.721 
							 | 
	wol_43311_1281.979_1285.7.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43311_1281.979_1285.7.wav 
 | |
	comme  day nekk information  bu yaatu 
 | 1.629 
							 | 
	wol_44113_568.911_570.54.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44113_568.911_570.54.wav 
 | |
	nga dem ji wala nga dem def 
 | 1.887 
							 | 
	wol_43020_303.171_305.058.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43020_303.171_305.058.wav 
 | |
	boobu day nekk bi ñuy wax limon  
 | 1.996 
							 | 
	wol_44311_591.579_593.575.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44311_591.579_593.575.wav 
 | |
	di sant auditeurs  yëpp 
 | 1.447 
							 | 
	wol_4314_904.563_906.01.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4314_904.563_906.01.wav 
 | |
	%hum %hum %hum  loolu la kay 
 | 3.075 
							 | 
	wol_4612_82.095_85.17.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4612_82.095_85.17.wav 
 | |
	%hum %hum %hum 
 | 0.923 
							 | 
	wol_4811_156.931_157.854.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4811_156.931_157.854.wav 
 | |
	 fépp foo dégg assurance  indicelle  
 | 2.549 
							 | 
	wol_44122_726.3_728.849.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44122_726.3_728.849.wav 
 | |
	ba nga xam ni %e niñ niñ daan liggéeyee ñu ngi gën di ci weer yooyu ñu ngi koy ñu ngi koy gën di ñeme  ndax ñu ngi doon jotee information  ci ci Nafoore dafa dalaloon sunu sunu xel 
 | 10.352 
							 | 
	wol_36510_256.468_266.82.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_36510_256.468_266.82.wav 
 | |
	na ñu arrêté  di gor 
 | 1.208 
							 | 
	wol_44114_775.094_776.302.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44114_775.094_776.302.wav 
 | |
	bon  fumier   moom am na solo am na solo trop  ci tool 
 | 4.361 
							 | 
	wol_43810_1913.398_1917.759.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43810_1913.398_1917.759.wav 
 | |
	kon foofu daal amoon na kay tuuti jafe-jafe 
 | 1.816 
							 | 
	wol_31211_588.151_589.967.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_31211_588.151_589.967.wav 
 | |
	par  rapport  ak première  taw bi 
 | 1.489 
							 | 
	wol_44312_239.938_241.427.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44312_239.938_241.427.wav 
 | |
	yàlla baax na 
 | 0.5 
							 | 
	wol_42212_1631.045_1631.545.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42212_1631.045_1631.545.wav 
 | |
	waaw vaaw 
 | 0.669 
							 | 
	wol_4210_1956.915_1957.584.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4210_1956.915_1957.584.wav 
 | |
	mën nañu la jàpp chambre  de  commerce  ñëpp kenn ku ci ne dana def visite  ci fi nga xam si ne mooy béréb bi nga xam ne si nga defaree li nga xam si moom mooy céréale  bi wala soit  yeneen produit  yi ngay defar 
 | 10.342 
							 | 
	wol_41012_75.198_85.54.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41012_75.198_85.54.wav 
 | |
	Baye Niass ba muy wax radi  yallaahu  anhu  
 | 2.085 
							 | 
	wol_44411_1557.022_1559.107.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44411_1557.022_1559.107.wav 
 | |
	yooyu boobu nag moo gën a garaaw boobu vingt  et  un  fois  la gën a garaaw que  CO2 tu  vois  boo xoolee bon  yokkuteem mu ngi toll si zero  virgule  six  pour  cent  ci at bu nekk 
 | 9.814 
							 | 
	wol_45511_546.129_555.943.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_45511_546.129_555.943.wav 
 | |
	na ñuy déglu informations  yi régulièrement ;fra 
 | 2.101 
							 | 
	wol_42932_394.089_396.19.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42932_394.089_396.19.wav 
 | |
	ndax Fapal kuréel la boo xam ne si wax naa ko ci ñaar ñett fànn yëpp ci lay yëngu  
 | 4.086 
							 | 
	wol_4311_241.463_245.549.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4311_241.463_245.549.wav 
 | |
	donc  loolu moom mooy loo xam ne souvent  dañu koy déploré  
 | 2.115 
							 | 
	wol_35312_128.212_130.327.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_35312_128.212_130.327.wav 
 | |
	jote wuñ sax xëy na peut  être  ci télévision  parce  fu mu la fekk dafay sori mais  à  travers :ra les  projets  et  programmes  yi nga xamante ni moom la ñu am ñu mel ni waa 4R ñu mel ni ay Proval ak yeneen ak yeneen  jàppale nit ñi ba nga xamante ne bi au  niveau  de  de  note  service  am nañu benn base  bi nga xamante ni bii %e ay numéros  de  téléphones  yi ça  fait  plus  de  mille  
 | 21.064 
							 | 
	wol_42611_1407.289_1428.353.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42611_1407.289_1428.353.wav 
 | |
	 waaye terewul ba tey mën nañu wéyal waxtaan bi ànd ak kii di Jalle yaakaar naa ni li fi Ibrahima wax yëpp am na am na solo  te it xam naa ni %e yéen yaa ngi naan Ibrahima moo tax amagu leen yéen code  barre  mais  yéen seen wàllu bopp aussi   est  ce  que  mate ngeen normes  yi war a tax ngeen am code  barre  
 | 14.077 
							 | 
	wol_41013_361.197_375.274.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_41013_361.197_375.274.wav 
 | |
	mais  bu tawee ci kawam non  seulement  am na nu muy demee doomu gerte bi dafay 
 | 5.781 
							 | 
	wol_42212_1149.305_1155.086.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42212_1149.305_1155.086.wav 
 | |
	seen seen coopérative  
 | 1.06 
							 | 
	wol_31211_660.072_661.132.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_31211_660.072_661.132.wav 
 | |
	mu daal di wow séchage  
 | 2.787 
							 | 
	wol_42912_316.048_318.835.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42912_316.048_318.835.wav 
 | |
	%hum %%hum 
 | 0.689 
							 | 
	wol_36010_4.723_5.412.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_36010_4.723_5.412.wav 
 | |
	 te mbéyum ceeb ku ko xam ci ji  mi dafay ànd ak %e  pour  mu gaaw a sax il  faut  que  nga am tàngaay  bu njëkk ba dañ daan wax ci yenn weer yi daawul tàng dafa daan sedd te gis nañ ni weer yooyu léegi de mi ngi tàng  
 | 12.058 
							 | 
	wol_36510_244.41_256.468.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_36510_244.41_256.468.wav 
 | |
	rupture   ci ñebe bi kii bi du baax feek book Etat  bi nga xam ne ni moom mooy gëstu di gñne lu bees moom dina dina ci %e dina dina dina ko def 
 | 8.613 
							 | 
	wol_4314_155.075_163.688.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4314_155.075_163.688.wav 
 | |
	ah waaw  ro()  
 | 1.613 
							 | 
	wol_45411_1777.579_1779.192.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_45411_1777.579_1779.192.wav 
 | |
	%e loolu tamit muy beneen aspect  ci njëriñ bi nga xam ne rotation  bi mun na ko mun na ko mun na ko amal 
 | 4.537 
							 | 
	wol_43810_922.89_927.427.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_43810_922.89_927.427.wav 
 | |
	xool yan interet  lañuy teg lan moo ci teg ba ci assurances  yi ñuy def 
 | 5.43 
							 | 
	wol_4812_613.216_618.646.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_4812_613.216_618.646.wav 
 | |
	dêgg la ñu jël kooku allo 
 | 1.882 
							 | 
	wol_44412_1084.008_1085.89.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44412_1084.008_1085.89.wav 
 | |
	ak doxalin bi mën nanoo uute waaye lépp ku ci nekk ku taxawoon fii ne  jox leen ma réew mi ma taal Sénégal jox leen ma réew mi ma andil leen ndóol jox leen kan moo ko fi dégg 
 | 8.261 
							 | 
	wol_44412_1765.669_1773.93.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44412_1765.669_1773.93.wav 
 | |
	d'  ccord  
 | 0.712 
							 | 
	wol_36410_664.76_665.472.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_36410_664.76_665.472.wav 
 | |
	day ma dama lay jox benn misaal rek  tey jii boo demee Europe par  exemple  dangay dem ñu ne la yaa ngi nekk ci ay zero  degré  wala ay moins  moins  mo() moins  cinq  degré  affaire  yu mel noonu 
 | 11.085 
							 | 
	wol_42212_578.683_589.768.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42212_578.683_589.768.wav 
 | |
	ñooñu ñooy changé  
 | 1.027 
							 | 
	wol_44111_325.206_326.233.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_44111_325.206_326.233.wav 
 | |
	 xanaa rek balaa ñuy tënk rek ñu delloowaat kàddu bi monsieur %e Diatta  par  rapporrt  aux  perspectives  des  communautés  les  plus  résilientes  maanaam ñi nga xam ne gis nañ ne que  ne  %e seen loxo jotul seen i ginnaaw bu baax ñi nga xam ne ciblé  nañ leen  ci seen enquête  yi ngeen def  njëriñ bi ci projet  bi wala tamit %e lan ngeen di séntu si ñoom ba tax ñu ngeen dugal leen ci projet  bi 
 | 23.541 
							 | 
	wol_42922_598.102_621.643.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42922_598.102_621.643.wav 
 | |
	ba jotanteeg ñoom man maay le  président  bi maa ngi dëkk kër Saalum Diané  ñu may wax Aliou Ndao 
 | 4.131 
							 | 
	wol_42311_267.201_271.332.wav 
 | 
	audio/kallaama/wol_42311_267.201_271.332.wav 
 | 
End of preview. Expand
						in Data Studio
					
	README.md exists but content is empty.
								
- Downloads last month
 - 2